Ci bessou 7 october di na neek atte si ba gnou baumè Anna Politkovskaja sì bountou keureume sa Moscou.
Gni gua khamni gno ko baume sokhe tchi kawame gninti gallou pistolet gni gui weeye ba teey ak gni gua khamni gno lène ka santeu.
Anna wa rèweume miinou gnou ko wone lole come ni ko prèsident Poutine fatalè aye wokhtou new ganaw bagnou ko baumè. Naha djèk aye tèrème si wa Tchetcheni ake si walou democrazie nou mouye dokhè fofa si Russie kène nogou wouko woon guènè. Lolou di firdèle ni ka si Russie liberté pressbi toumourankè na fa loole tchi atte yi gua khammi reewma bène ex colonellou Kgb mo ko djitè.
Dontalè gni gui ka doon fitnaal ak di ko titeule Anna dè moom moussoul bougue dawe reeweume bobou di Russie.
Reportage gnou ame solo gni gua khamni dèfe na ko si boundoukhatale domou adama gni sa Gozni ak si Russie yittè
loonna wa occident.
Way è si bassoume dadjeume bènne dawalou Union Europeenne takhoule mou tèwe fa.
Benne djitou reewe bènne djitou gornementtèwouffa weune yi teume.
Bou fèkeeni gni gnoor politique bi falèwouyouko gni gua khamni gnooye yeugou si wallou culture dou gnou faatè Anna Politkovscaja.
Si lolou gni gui gnaane ka si Europe gui yeupe zournal yi, tèatar yi, orchestar yeek, artiste yi gnou khewale si bessou 7 octobere 2007 bi aye djeufine you takh gnou meina fattalikou Anna.
mailto:7ottobre2007@gmail.com
1 commento:
Ciao, complimenti ... come giornalista e scrittore non posso far altro che vergognarmi di come il genere umano sia così caduto in basso.. teniamo duro. Anch'io sul Blog annesso al mio sito www.paolomoschini.it ho dato eco alla Vs iniziativa.
Posta un commento